News

Pour l’anniversaire d’Aïda, You frappe fort

PARTAGES | J'AIMES |

Lu: 11399 fois
Jul 23, 22:15
buzz
10 Commentaires | Tags: Youssou, Ndour, Aida

Quand on aime, on ne compte pas ! L’adage bien connu des amoureux a été fait sien par la méga star Youssou Ndour, par ailleurs ministre conseiller du président de la République, pour encore prouver son attachement à sa dame, Aïda Coulibaly. Pour l’anniversaire de cette dernière, le patron du Super Etoile a réservé une partie d’un grand restaurant de Dakar, dans les environs du King Fahd Palace. A côté de chaque Roi, il y a une Reine. C’est You et Aïda.

Recent posts

commentaires

live comment
  • Mimi

    zim gor dafaye diongué waye,li leu. nope sa madame di co co wone chak jour

  • Amoureux

    c vrai que grand bi dafa samp thioukel ! casser 20 ans de mariage ak mammy kamara, amour deug moko meuna justifier

    • Bro

      li dou amour lii interêt la c'est comme le mariage de balla gaye balla siw na am na khaliss ban djiguen moko meuna bagnal dara goor bo ame khaliss yaye chef viviane sakh boko newe kay ma tak la mou daw ba fatick khaliss la reck mais dou lenen bouniou newon ni ne youssou ndour reus na meunoul don mamy neko you bay bay mais khlissonm mo ngi law do niak dara tog reck ngay def goor yi ni la de dniouye nekakh ken mouye mougne bou allal bi ne peung bari nio bayi ko dem outy bou khess te rafet djiguen you nioule yi mougne len waye te nak boulen khessal nakhte sama genre yi nioulay mo len di danel

  • Assy

    bro deugue rék ga wakh